Nijaay wax al ak sa mag ji
Boo gaaw u lee , mu jaay ma
Alal moo yóbbu , fit wi
Sama Habibi bi
C’est l’amour de ma vie
Instru;
bu jar ee mer , ma mer ko
Bu jar ee jooy , ma jooy ko
Bu jar ee xeex , ma xeex ko
Sama Habibi bi
C’est l’amour de ma vie
Instru
Ki ne ci sa ma xol bi
Moo ma gën ël , alal ji
Té ngeen a gat al wax ji
Sama Habibi bi
C’est l’amour de ma vie
Instru
Bu am a gul , ma muñ ko
Lu ma fortaatu , jox ko
Nijaay gaaw al nga dox ko
Sama Habibi bi
C’est l’amour de ma vie
Instru
A yéen daal yéen , a sonn a
Du maa moom sa , ma xol bi
Mbëggéel ken du ko donne
Sama Habibi bi
C’est l’amour de ma vie
Break;
mbëuggéel gu ñu lë bëgg é
L’amour ne s’achet pas
mbëggéel gu ñu lë bëgg é
mbënggéel gu ñu lë bëgg é
L’amour ne s’achet pas
mbëuggéel gu ñu lë bëgg é
mbënggéel gu ñu lë bëgg é
L’amour ne s’achet pas
mbënggéel gu ñu lë bëgg é
mbënggéel gu ñu lë bëgg é
L’amour ne s’achet pas
mbënggéel gu ñu lë bëgg é
ba laa ngaa jël teraanga , laaj ko ndax bëgg në
ba laa ngay jël warougar , laaj ko ndax bëgg në
ba laa ngay jël teraanga , laaj ko ndax bëgg në
ba laa ngay nangu warougar , laaj ko ndax bëgg në
xale bi kaay fii , laaj ma ndax bëgg në
xale bi kaay fii , laaj ma ndax bëgg në
xale bi , xale bi , xale bi , laaj ma ndax bëgg në
xale bi kaay fii , laaj ma ndax bëgg në
xale bi , xale bi , xale bi , laaj ma ndax bëgg në
xale bi kaay fii , ma laaj la , ndax bëgg ngë
da fa mel ni xale bi , xale bi, bëgg ou lo loo
Instru
Nijaay gaaw al nga dox ko
Sama Habibi bi
C’est l’amour de ma vie
Pour plus de vidéos, abonnez-vous sur notre chaine